Bril Fight 4 - Titeulnama (Clip Officiel)

-

BrilFight4 Officiel

581,824 views
Hey guest, welcome to TopHBO.Com Like to see
## Abonne-toi à ma chaîne ici http://goo.gl/Qw5BFh ##
Mon nouveau clip : "Titeulnama"
Un coup de foudre... Oser parler à cette femme qui te séduit tant... S'interroger sur sa réaction... Redouter sa réponse...
#Brilfight4 #Bril #Titeulnama #ClassChicMusic #team221

# Crédits, remerciements & dédicace du clip "Titeulnama" #
Lieu : France
Images : Pépé Diallo
Réalisation : H-Lab Pro Entertainment (771833387)
Un grand merci à tous ceux qui ont participé à la réussite de cette vidéo.
Particulièrement Idy, Matar (Napoli), Momo et Mbeuss.

# Crédits de la chanson "Titeulnama" #
Auteur & compositeur : Bril
Studio enregistrement, mix, edit & mastering : Class’Chic Music
Titeulnama est une seconde version du morceau « Dafma Titeul » extrait de mon projet Confirm’Action.
Une production de Class’Chic Music (Senegal, 2018).

# Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux #
Facebook http://web.facebook.com/brilfight4
Instagram http://www.instagram.com/brilfight4
Twitter http://twitter.com/bril_fight4
Snapchat : @bril-fight4

# Lyrics de la chanson "Titeulnama"
1er couplet
Biniou guisséé damala Xool, am louma yeukk daanou Léér .
Nga romb noyétouma té manquéwouma air .
Nitt gni beuri mou melni yaw rek ya tééw, malay guiss ni wéér thi biir ay Bidéw.
Bima beuggué djougg wakhla li né thi mane, Mélni dama paralysé.
Sama djeumangui thi souf sama xel thi assamane , Mangui tog di Analysé.
Foumay djaar ba amla , dound’ak yaw Paradise.
Fouma tolou lolou lay guiss, ya né samay eyes.
Meussoumalako wakh té mangui wadja dof
Commencéna déf enquête té douma inspecteur ndakh Love .

Refrain
Dama djéékh takh thi yaw, Sama xélmi ya thi né
"Beuggnala lol bay guéntt niouy doundou Love"
Foumala guissé bouma mérone damay réé
"Beuggnala lol, meussouniou doundou Love."
Djékhna thi yaw sama xélmi yathi né
"Beuggnala lol ,nieuweul niou doundou Love ."
Foumala guissé limay wakh damay réér
"Beuggnala , té meunounio doundou Love."

2ème couplet
Xam yay kane lay liguéy, kouma djéggué dinakako lathie.
Dafa mélni dagnma Liguéy bama gueumni mane sokhlana am Galathie .
Takkeu sama Fitt, wakhla limay yeukk , sama biir bayi limouy def say boy romb.
Sama Gars yi gueuna done ragal dima togn , fokkné wakh lima beugg da yomb.
Damay khiif guissla rék Sour .
Day Séédd ngay tangal sama Your.
Fouma yeukkni dangafay djaar ma djitoulafa mélni kouy xaar Bour .
Bo yakcé doma xool , té nga djaralma djaay ngora mbeukk mur .
Ya né sama Xool , windélouwouma té mangui miir .
May khaathiou di alou nane fok ma wakhla , nga yékci ma mouma .
Toppoula , Soppoula, Sauroula, yaagg di waathie démouma .
Mangui ci Leundeum, fokma djégguéla , Sama yone doga Léér.
Boma waulo nangou ma Bégguél la waat nani do Galére.


Refrain
Dama djéékh takh thi yaw, Sama xélmi ya thi né
"Beuggnala lol bay guéntt niouy doundou Love"
Foumala guissé bouma mérone damay réé
"Beuggnala lol, meussouniou doundou Love."
Djékhna thi yaw sama xélmi yathi né
"Beuggnala lol ,nieuweul niou doundou Love ."
Foumala guissé limay wakh damay réér
"Beuggnala , té meunounio doundou Love."

Pont
Dafma titeul yeaaaahh
"Beuggnala lol ,nieuweul niou doundou Love."
Gnimay andal Nieuppa xamni sama Xélmi yathi né
"Beuggnala , té meunounio doundou Love."
Djékhna thi yaw sama xélmi yathi né
"Beuggnala lol ,nieuweul niou doundou Love."
Foumala guissé limay wakh damay réér
"Beuggnala , té meunounio doundou Love."
bril, bril fight 4, brilfight4, bril 2018, bril marichou, bril fight 4 titeulnama clip officiel, bril fight 4 titeulnama, bril titeulnama, titeulnama, bril fight 4 titeul nama, brilfight4 wetalngama, titeulnama clip, bril clip 2018, clip, hlab pro, pod marichou, pod, marichou, love, bril trahison, bril sama life, bril gangstalove, marodi, dakar, senegal, birahim, viviane chidid, wally seck, dadju, nafi, mbettel, idoles, afrobeats, tfm, pape diouf, aida samb, vibe radio, amour, nafi 19, 2018,
Loading...
Loading...