Loading Player ...

Bril - Cila Bokk - Clip Officiel

-

Bril Officiel

295145 views
Hey guest, welcome to TopHBO.Com Like to see
**Abonne-toi à ma chaîne ici http://goo.gl/Qw5BFh**
Après le succès de \"Bras Long\", CILA BOKK est le 2ème single extrait du nouvel album de Bril, SUBA, disponible à partir du vendredi 20 septembre sur toutes les plateformes de streaming et téléchargement.
Il est vital de bien se détendre et s'amuser : vos vedettes préférées comme Dudu, Mahfousse, Admow, Pagaye Mbaye, Pape Birahim ou Bass Thioung vous aident à oublier vos problèmes.
Cila Bokk, viens nous rejoindre, faisons la fête tous ensemble !
(voir lyrics plus bas dans cette description)
#Bril #CilaBokk #Suba #NouvelAlbum20septembre #ClassChicMusic #team221

**Crédits de la chanson \"Cila Bokk\" **
Auteur : Bril
Compositeur : Bril 
Studio enregistrement, mix, edit \u0026 mastering : Class’Chic Music par Bril

Une production de Class’Chic Music (Dakar, Senegal, septembre 2019)

**Crédits du clip \"Cila Bokk\" **
Réalisation : Weeflag
Un grand merci à Dudu , Mahfousse, Admow, Pape Birahim,, Jeeba,, jah hustla , Pagaye Mbaye \u0026 Bass Thioung pour leur aimable participation.

**Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux**
Facebook http://www.facebook.com/brilofficiel
Instagram http://www.instagram.com/bril_officiel
Twitter http://twitter.com/bril_fight4
Snapchat : @bril-fight4

** Contact management** 
Mr Mahmoud Sy : +221 77 036 48 31 
brilfight4@gmail.com 

**Booking international**
vincent.lagoeyte@soon.pro

**Lyrics de de la chanson \"Cila Bokk\" **

{Intro} 
hahahahaha 
(Bril on the Beat) ha ha 
Yeah yeaaah  Bril in the Building , héé 
Cila Bokk way way Cila Bokk , amoul Yakkalaté han , aythia Niou dém 

{Refrain} 
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss. 
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh . 
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.

{1er Couplet} 
Lo xamoul kagn lay djèkh dafa wara nékh .
Boul faalé koulay méré wane ko beugn you wékh. 
Léppeu térangala , doundeul happyness.
Lofi meunti am té béggo , amna louthi déss. 
Fii dal Sénégal la , boula nékhé dinga béggué .
Boul nangou kèn yakkal-la dééko défé ning’ko beuggué.
Daniouy dadjé foo di réé té xawma no Toudou . 
Selfie def ay Vidéo you fun melni #Dudu, 
#Baye_Mbaye , #Makh_Pro / koufi mér kone Wéro. 
Warnga meune di enjoy nga né town wala ghetto . 
Boul nangou kèn dila téré Happy...
Kou sa life néékhoul , yakoy soppi . 

{Refrain} 
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss. 
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh . 
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.

{2ème Couplet}
Héé Yaw nanga déf 
Koula beugga sonal thi wakh nèko mou déf, 
Défam té bayila rèk yaw nga néthi .
Take it easy , dafa wara yomb, waroul , méti hééé.
Beurina ay Nitt you done foo djaarfa feullalé . 
Tèki_thi romboula wakh bo saani niou feul- feulalé. 
Kheuthiolén son you #Lourd , ma ték lou #Léger dilén Mour .
Ngén may gueuna #Haine, maléni raw par #Amour. 
Bayilén niouy rawanté ngay dokh ndank , daagoul .
Té koukay djaay méti , né ko  “Lou Méti Yagoul”. 
Dél Khol sa none di réé né kouy sétane #Aba_Show 
Caméra cachée #Makhfouss lay yooné sama Cho (copine) 

{Refrain} 
Xamal ni dakoy ladj nga dindi stress.
Boula kén ray doundou dafay nekh.
Koula beugga sonal Romb ko né mééss. 
Niongui Foo, Happy , Bégué, Mba Xol yangui fékh . 
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Sagnsé andak kilay bégglo “Cila Bokk”
*kaay* “Cila Bokk” Walay “Cila Bokk”
*kaay* Tok di sétane Loulay réélo “Cila Bokk”.

{Outro} 
*kaay* Héé ...féthial féthial way , *kaay* ni rekla yeungoul yeungoul way .
*kaay* Hééé...féthial way , *kaay* ni rekla yeungoul yeungoul way .
*kaay*.   féthial féthial way  , *kaay*  niou dèm , hèè Han han yeungoul yeungoul way .
*kaay* mané Cila bokk haaa...yeah cila bokk.
bril cila bokk clip officiel, bril cila bokk, cila bokk, bril, bril fight 4, brilfight4, dakar, senegal, musique, music, 2019, cilabokk, cila bok, cilabok, bril cila bok, bril fight 4 2019, bril fight, class chic, pape birahim, dudu, mahfousse, pagaye mbaye, bass thioung, thioung, jeeba, dip, samba peuzzi, hip hop, rap galsen, maabo, queen biz, da brains, vibe radio, tfm, sen tv, zik fm, idoles, moeurs, golden, madior ak dior, afrobeats, mbalax, suba, bril souba, souba, love, bras long,
Loading...
Loading...